Del Bale (feat. Safary)

Omzo Dollar

Compositor: Não Disponível

Safary

Ring ding dong heure bi jotna
Dama nama yeigal balcon bacii kaw heure bi jotna
Mane douma teudd tei yeungue louma fi ba fadiar
Xam nga sama leip saff sapp
Amoul daw fo nara diareu

Baleii bo djeiko del ballei
Ayayay!
Baleii bo djeiko del ballei
Ayayay!

Niou deiff cii kani deiff ci kani
Neima aya bébé
Je bouge ma body bouge ma body
Dis moi aya bébé
Ma done sa bandit done sa bandit
Neima aya bébé
Kone neima aya neima aya neima aya bébé

Niou deiff cii kani deiff ci kani
Neima aya bébé
Je bouge ma body bouge ma body
Dis moi aya bébé
Ma done sa bandit done sa bandit
Neima aya bébé
Kone neima aya neima aya neima aya bébé

Dél balé, dél balé, dél balé, dél balé

Ding dong heure bi jotna
Louma nameu togantouko bamou saff
Heure bi jotna
Mane dama parei tei doyagouma
Dara dou yomb
Fouma nara feithieu douma saff
Nakh dama seuss dara dou yomb

Baleii bo djeiko del ballei
Ayayay!
Baleii bo djeiko del ballei
Ayayay!

Niou deiff cii kani deiff ci kani
Neima aya bébé
Je bouge ma body bouge ma body
Dis moi aya bébé
Ma done sa bandit done sa bandit
Neima aya bébé
Kone neima aya neima aya neima aya bébé

Niou deiff cii kani deiff ci kani
Neima aya bébé
Je bouge ma body bouge ma body
Dis moi aya bébé
Ma done sa bandit done sa bandit
Neima aya bébé
Kone neima aya neima aya neima aya bébé

Dél balé, dél balé, dél balé, dél balé

Hey I say bad man mister in the place
Rude boy things them I say
Yeungue leul gauche, yeungue leul droite
Do meusseu ndangou keineine beuss bo wetteii ak mane
Neina miser ak mane (ak mane)
Foumela yobou fokk nga seuggueu pour guiss assamane
Han ayouma sou feikei deiwo
Amoul pitié amoul balei amoul feikei deweineu
Doumla maay dara kom kou bokk yal-wane team
Ak mane dou meusseu diekh ame nioumay wowei à suivre
Bébé aksil ak diam ma nadj bi lay clask
Sa mathieu la tass amoul diap la clap
Matt la diane diap la Matt la table
Souma paré ak yaw niou fokk ni sath la dia nigga nigga!

Dél balé, dél balé, dél balé, dél balé

Niou deiff cii kani deiff ci kani
Neima aya bébé
Je bouge ma body bouge ma body
Dis moi aya bébé
Ma done sa bandit done sa bandit
Neima aya bébé
Kone neima aya neima aya neima aya bébé

©2003- 2025 lyrics.com.br · Aviso Legal · Política de Privacidade · Fale Conosco desenvolvido por Studio Sol Comunicação Digital